Mafatihul Bichri Infos

WAXI SERIGNE BI

WAXI SERIGNE BI

serigne_touba211Serigne Touba Masna Wakh Serigne Mèrina Sylla Massamba Lako Serigne Touba Dane Wowè
Serigne Touba Niko Massamba Bouguèndi Taggo Bay Gnanalanetè Louguèndi Diangue ? Mouniko Danouy Tari Fatiha Tèkssi Dara
Serigne Touba Niko Sama Gnari talibè Youy Taggo Amoul Lougueun Ci Gnoom Sama Tourwii
Mouniko Wanelassi ?
Serigne Touba Niko Wi Nèkh Wa kaaw Nèkh Wa Souff Moy Khadimou Rassoul.

SERIGNE MBACKE DIOP

2Serigne Touba Nèna:
Sounou Borom Nènako Bofi Djitouwoon Alkhourane Waskour-Fikitabi Ahmadou Bamba Danassi Bari Niko Dinassi Dèff You Beuri
Guinaw Alkhourane Molafi Djitou Nak Limalay Fayèè Moy Damalay Dèfal Sayoye Binde Arach Di Diayou (Yeuguetou) (Serigne Mbacke Diop)

Serigne Touba Nèna:
Sounou Borom Nènako Bofi Djitouwoon Alkhourane Waskour-Fikitabi Ahmadou Bamba Danassi Bari Niko Dinassi Dèff You Beuri
Guinaw Alkhourane Molafi Djitou Nak Limalay Fayèè Moy Damalay Dèfal Sayoye Binde Arach Di Diayou (Yeuguetou) (Serigne Ganna Mèssèrè)

Related Posts

Facebook Comments